Mustafaa (@th_muhammadu) 's Twitter Profile
Mustafaa

@th_muhammadu

Alhamdoulilah🤍

ID: 1798688900824621056

calendar_today06-06-2024 12:10:39

298 Tweet

38 Followers

265 Following

Sëriñ Saliou (@assaalih22) 's Twitter Profile Photo

Nii moom dinaa mëna tontu kom Kuy sakku/ gëstu xam-xam😂 Laaj yi yepp day melni tontu bi Mingi ci aaya bi nga wax noonu. Li njëkk mooy ñu xamni mono/ poly ñaar yepp dagan nan looou mooy point de départ bi, li dagan nag mën na dem ba war/ obligation, wala nekk luñu sopp, mën na

Sëriñ Saliou (@assaalih22) 's Twitter Profile Photo

Atte salon de beauté, Bokk na ci yi araam, 1- jokk/ yokk karaw (mèches ak leneen lumu mëna doon ludul sa karawu bopp) 2- tatouage, Yonent bi shw neena yalla rëbbu na ku leen di def ak ki defar/ ligeey, (buxaari, 5941, 5933, 5937, muslim 2122, 2124) Tatouage boo xamni fuddën

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Manu leen a fexe ba araamal lu lislaam daganal, Yàlla mi bind Jaam ñi moo leen gën a xam, te moo gën a xam li gën ci ñoom, li jaadu ak li jaaduwul lépp leer na ci lislaam, te ab jullit benn nattukaay la am muy diineem, koo xam ne bokku leen diine nga bëgg koo topp ci ay xeexam da

Bichri🤍 (@bass_g_mbacke) 's Twitter Profile Photo

Yàlla néena: « Il a créé pour vous, de vous-mêmes, des épouses, afin que vous trouviez auprès d’elles tranquillité, et Il a mis entre vous affection et miséricorde.» -Sourate Ar-Rum Mais Selon l’experte féministe, Daba Sëy « Le mariage est l’institution la plus dangereuse pour

Yàlla néena: « Il a créé pour vous, de vous-mêmes, des épouses, afin que vous trouviez auprès d’elles tranquillité, et Il a mis entre vous affection et miséricorde.»
-Sourate Ar-Rum 

Mais Selon l’experte féministe, Daba Sëy « Le mariage est l’institution la plus dangereuse pour
no one🇸🇳 (@bmdev_) 's Twitter Profile Photo

Curieux comme Fatouma Diallo 🍉, elle-même mariée, conseille aux autres femmes d’éviter le mariage. « moi je suis assez intelligente pour trouver le bon. Vous ne l’êtes pas donc ne vous mariez pas c’est dangereux ». Et c’est quoi l’alternative au mariage ? Le concubinage ? 1/8

Curieux comme <a href="/fleuvediallo/">Fatouma Diallo 🍉</a>, elle-même mariée, conseille aux autres femmes d’éviter le mariage. « moi je suis assez intelligente pour trouver le bon. Vous ne l’êtes pas donc ne vous mariez pas c’est dangereux ». 
Et c’est quoi l’alternative au mariage ? Le concubinage ? 1/8
Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Ab murid ni mu war a doxe, nii la ko Sëriñ bi leerale (sa programme) Ab taalibe li njëkk a war ci moom, mooy mu am ab yóbbal ci tawhiit, ba laa beru di tudd Yàlla ak di xeex ak bakkanam. Mu tënku ci pas-pasub ahlu sunna, ndax loolu moo koy aar. Topp bidaa day tax nit ki du man

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Yàlla lépp lu mu bind ci yaw ne dinga ko jot, kenn manu la koo xañ, nit ki boo ame ab cér ci alalam, boo toogoon tuddoo ko sax dinga ci jot, waaye li Yàlla bindul ci yaw, boo doon sonn lool ba mel ni kuy jaamu nit ki sax du tax nga jot ci alalam. Yàlla noppi na ci lépp, jaam bu

SALIOU MBACKE FAYE (@salioumbackefa1) 's Twitter Profile Photo

Joxante ngant moy li gën a am solo ci loy noppal nit ba noppi may ko tranquilite , ko xamul bul ko juger lifeek jaxaso woleen … njort bi nga am ci nit de loin yallah neena li ci ëpp ci ñoom du dëgg. Bul bañ ken rawatina ko xamul Bul noono ku la tooñul Bul njort lu ñaaw ci nit