ANTA🤍 (@antaa_dw) 's Twitter Profile
ANTA🤍

@antaa_dw

Aspirante Murid 🤍🤍Biologist🧬

ID: 1230012153802973185

calendar_today19-02-2020 06:12:15

2,2K Tweet

1,1K Followers

596 Following

ANTA🤍 (@antaa_dw) 's Twitter Profile Photo

“Lii ku ko saxal guddig àjjuma ju nekk doonte wenn yoon la, bu ñu koy duggal ci bàmmeel, Yonent bi (SLHWS) moo koy nangu !" Xurratul Ayni

“Lii ku ko saxal guddig àjjuma  ju nekk doonte wenn yoon la, bu ñu koy duggal ci bàmmeel, Yonent bi (SLHWS) moo koy nangu  !"

Xurratul Ayni
ANTA🤍 (@antaa_dw) 's Twitter Profile Photo

Ça vous arrive de méditer sur les bienfaits d’Allah ? Nga togg ba ci yàgg nga xalaat ñi mënalut sen bopp dara walla ñi ñàkk ba amuñu luñ lekk ? Te mu leer la ni yaw ñi gënoo leen ? Defaloo sa Borom lu wara tax mu xañ leen may la yaw Lii dina tax a sant Yàlla

Sëriñ Saliou (@assaalih22) 's Twitter Profile Photo

SINDIDI gisu ma xasiida guko gëna mat ci lu jëm ci ñaan yalla, lepp lu jara ñaan rek sëriñ bi ñaan na ko ci biir xasiida gi.

Al Ihsân (@al_ihsaane__) 's Twitter Profile Photo

📚Pack Collection Ghazali✨ Composé de 22 livres essentiels, cet ensemble est un mix de tous les thèmes spirituels et de société 📌 Le minhaj vers le paradis Le livre de l’amour La vie après la mort, etc…. Tous ces chef-d’oeuvres en un pack! 🏷️110.000 fCfa

📚Pack Collection Ghazali✨

Composé de 22 livres essentiels, cet ensemble est un mix de tous les thèmes spirituels et de société 📌

Le minhaj vers le paradis
Le livre de l’amour
La vie après la mort, etc….

Tous ces chef-d’oeuvres en un pack!

🏷️110.000 fCfa
🀄️🐍 (@sagittaire99) 's Twitter Profile Photo

Le Prophète ﷺ a dit : « Les pires des gens sont ceux qui ont une double personnalité en se présentant à certaines personnes avec un visage et à d'autres, avec un autre visage ».

Taalibe (@seentalibe) 's Twitter Profile Photo

« Je n'ai jamais non plus sollicité une richesse utile ici-bas ou dans l'autre monde sans recevoir un don généreux de la main la plus digne d'être baisée. »ﷺ ﷺ niaan leen ci barke Yonent bi, di ngen am !

Ibrahima Sene💫❤️166i (@lamp_fall96) 's Twitter Profile Photo

Toudé na tout-tank CHEIKHOUNA KHADIM RASSOUL SÉNE❤️🙏🏻 Guén nianal ko bubaxx mou goud faan and ak werr si barkép werou Koor gui🙏🏻

IKD (@baye_yibreuu) 's Twitter Profile Photo

As Salamuhalaykum wa Rahmatulah Aujourd’hui est le 8e jour du décès de ma mère. Ngeen fassalé ko si Ya-sin, istighfar, Basmalah ak salatu halal nabi 🙏🏾❤️ qu’Allah vous rétribue au centuple . YAllah na borom bi fay leen yiiw barkeep weer wi 🤲🏾