Fallou Salih (@salihfadal) 's Twitter Profile
Fallou Salih

@salihfadal

Fallou Salih est un serviteur de Cheikhoul khadim/communicant/chercheur/éternel- apprenant/instagram.com/fadal_salih?ig…

ID: 1047836006802706433

linkhttps://fallousalih.wordpress.com calendar_today04-10-2018 13:09:06

32,32K Tweet

36,36K Takipçi

4,4K Takip Edilen

Fallou Salih (@salihfadal) 's Twitter Profile Photo

Borom Touba dafa indi si Safinatoul Amaan (Nafila) Hadith bou Abi Amaama Yalla nako Sunu Borom gueureum nétali dieuléko si Yonenté bi SHWS mou wakhni : "Kép kou diouly si goudik Altiné (La nuit du Dimanche au Lundi) 2 Rakka bousinék mou dianguesi guinaaw Fatiha 1yoon (1fois) ,

Borom Touba dafa indi si Safinatoul Amaan (Nafila) Hadith bou Abi Amaama Yalla nako Sunu Borom  gueureum nétali dieuléko si Yonenté bi SHWS mou wakhni : 

"Kép kou diouly si goudik Altiné (La nuit du Dimanche au Lundi) 2 Rakka bousinék mou dianguesi guinaaw Fatiha 1yoon (1fois) ,