Ṣuhayb al-Rūmī (@s_fallougueye) 's Twitter Profile
Ṣuhayb al-Rūmī

@s_fallougueye

"Travailles comme si tu ne devais jamais mourir, et pries comme si tu devais mourir demain"⚒ Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul

ID: 1373691109302538241

calendar_today21-03-2021 17:41:19

3,3K Tweet

290 Followers

187 Following

Mo_152i 😁🇸🇳 !! (@mohamedwilane) 's Twitter Profile Photo

Ceey , dëgël ni seriñ touba definirë « Jambar » rk 😭❤️!! ( baye atou Yalna sa borom yooki leeram 🙏🏾) #Jërëjef_Ahmadü

Sëriñ Saliou (@assaalih22) 's Twitter Profile Photo

-ñakk xam jangale islaam ci sëy - bayyi yi mag yu baax yi daan def gir sampu sëy bi (sëy day am ay tektal ba ci guro gi amna tektal pour sëy bi dëgër…) - Irresponsible yenn ci goor ñi - bañ kilifteef ci yenn ci soxna yi - bëgg boole sëy ag dundu dundu célibataire - infidélité

Baay Sëriñ Jóob (@alaadjiditakh) 's Twitter Profile Photo

Mbir itam amna. Wax dëgg kese doyul, bu àndee ag ñakk teggiin nit ki sa waxiin wi lay jàpp bàyyi dëgg gi. Buko defee doo am lila tax a jog. Di fexe baril teggiin ba koo waxal mu jàpp wax ji te du ci gis boppam lu am solo la