Ibn Husman👩‍🎨👨🏿‍💻 (@ibn_husman) 's Twitter Profile
Ibn Husman👩‍🎨👨🏿‍💻

@ibn_husman

Visionnaire du Cinéma | CEO, Rebel Film SN | Monteur, Graphiste | Producteur | Scenariste | Wéteul Yalla, Doylu Sëriñ Tuuba Mbacké mu bakh mi

ID: 764678905

linkhttps://www.behance.net/ibnhusman calendar_today17-08-2012 23:51:59

3,3K Tweet

1,1K Followers

1,1K Following

H¤t S大ucㅌ🏆🥳🇸🇳 © ami de Ridwan AS (@hotsaucetweet1) 's Twitter Profile Photo

Lénn ci li mënna xajamal doxu jullit bi bëgg àgg (murid saadix): "niak maanu" Exemple ci politik . Extrait Jottayu Murid du 07-11-2024 Serigne Ahmadou Mbacké

Ibn Husman👩‍🎨👨🏿‍💻 (@ibn_husman) 's Twitter Profile Photo

Xam ngeen né bii “Bes du Niakk” ñoo “Sam sunu Kaadu”, deffat “Action”, “Takku Wallu Senegal”, “Xaal lal Yoon” Diomaye ak Sonko ngir “Dundu Lénen” “Jëli li ñu Moom” ci “Jàmm ak Njariñ”, ànd ak “PASTEF” ngir “Soppi Senegal”. #17PROSMAX #senegal🇸🇳 #Pastef! Acté!!🗳️

M. Lamine Bara LO (@mlbara_lo) 's Twitter Profile Photo

Mon intervention au séminaire sur la migration organisée à Las Palmas ces 25 et 26 novembre avec Casa Africa et le Gouvernement des Îles Canaries. Il faut recréer et entretenir l’espoir à travers la formation professionnelle et l’insertion au Sénégal. C’est un défi qui est,

Ibn Husman👩‍🎨👨🏿‍💻 (@ibn_husman) 's Twitter Profile Photo

! الشكر والصبر Moom dh dafa xamna ñar yii ! Japna si Yalla ba Yalla teralko, mo am reconnaissance ba né do ligey fenen fodul si Al-quran ! Tawkhit dji kawee na lol walahi❤️🙏🏾 Geumm Mooy Doylu Çant.

Ibn Husman👩‍🎨👨🏿‍💻 (@ibn_husman) 's Twitter Profile Photo

Un honneur de participer à cet atelier de validation des référentiels du titre de qualification dans les métiers du cinéma. Une étape essentielle pour structurer notre filière, professionnaliser nos talents et offrir des repères clairs aux acteurs du secteur. Bravo 👏🏽

Ibn Husman👩‍🎨👨🏿‍💻 (@ibn_husman) 's Twitter Profile Photo

Aka Bakh Mbacké, Taay dh dagno ko yoboul barkélou sunu waa-jur si biss bi mo tambalil bopam sedalé bi bolé si diohño ay « Ikfiini » nguir mbolo bi don ligeey Ak « Nuuru Dareeyni » bi moo don diangue❤️🙏🏾

M. Lamine Bara LO (@mlbara_lo) 's Twitter Profile Photo

Yaa raw ña daa janoog Rasuul Ngir yaa Liggéey ba am wusuul Ba def Xalifatu Rasuul Kawe nga mbooleem Xarnu bi Yoon wa nga aw ba raw mbindéef Ba def ndoney GËN GI MBINDEEF Manees u koo xamal mbindeef Jomb na mbooleem Xarnu bi Sñ Musaa KA XARNU BI

Yaa raw ña daa janoog Rasuul 
Ngir yaa Liggéey ba am wusuul 
Ba def Xalifatu Rasuul 
Kawe nga mbooleem Xarnu bi

Yoon wa nga aw ba raw mbindéef 
Ba def ndoney GËN GI MBINDEEF
Manees u koo xamal mbindeef 
Jomb na mbooleem Xarnu bi 

Sñ Musaa KA
XARNU BI