BintAhmaDem🥰 (@fdeme13680) 's Twitter Profile
BintAhmaDem🥰

@fdeme13680

Baaxal ba déssal do Sëriñ Tuuba 😭❤️
Boroom Tuuba yaakaari tay ak ëlëg 😌👍

snapchat.com/add/demefamasa…

ID: 1665031896546279425

calendar_today03-06-2023 16:25:42

5,5K Tweet

789 Takipçi

781 Takip Edilen

𝓛𝓪𝓭𝔂 𝓔𝓿𝓪𝓱 🤍💫 (@mc_evah) 's Twitter Profile Photo

La vie m’apprend tellement de choses de jour en jour… j’en suis à un stade où louway def bakhna. Kounek défal lou dal sa khel. Mais les relations humaines sont tellement compliquées et m’ont tellement menée à des pertes et des épuisements émotionnels, mentaux, etc., que j’ai

Sëriñ Saliou (@assaalih22) 's Twitter Profile Photo

Sëriñ muntaxaa reew meppu ku wardi Ñaanal, fanaane sikar tuddu turu yalla, xëy nara yendoo jang al xuraan ag xasiida, loolu reew mu ko am war nga sant yalla bu baax ndax lepp ngi si, jamm, xeewal, mucc, naataange, teraanga, kaaraange.....

انت بشير (@miss_mbackee) 's Twitter Profile Photo

Honnêtement,si vous saviez combien de temps et d’épreuves il a fallu à certaines personnes pour retrouver leur paix intérieure,vous comprendriez pourquoi elles coupent court à la moindre toxicité et pourquoi elles sont si sélectives sur qui elles laissent entrer dans leur vie.

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Bokk na ci ngistal yi, daan jëf lu baax, ba benn bis nit ñi tax lu baax loolu defoo ko, ci misaal nga doon julli ag naafila ci wenn waxtu, am bis mu fekk la ci nit ñi, nga ne bu ma jullee ci biir nit ñi, dañu koy jàppe ngistal, ba tax defoo ko, ñàkk koo def googu mooy ngistal

💙꧁𝔈𝔩~𝘗𝓲𝘉è~𝕵ℛ𓃵꧂❤️🦁🇸🇳 (@layeseckseckfcb) 's Twitter Profile Photo

‼️SEM Bassirou Diomaye Faye qui descend au rond point et marche avec la population sur le pont jusqu’à la gouvernance. Quelles images magnifiques et historiques . 🇸🇳❤️😍

Siréne Noire🧜🏿‍♀️🇸🇳 (@saly_mariama) 's Twitter Profile Photo

🚨JEU Tente de gagner un pack composé de: 1 parfum 20ml 1 huile 6ml 1 musc Conditions: Follow Siréne Noire🧜🏿‍♀️🇸🇳 Like et Rt ce post Tirage au sort 4 gagnants parmis les Rt 2femmes 2hommes Bonne chance

Siréne Noire🧜🏿‍♀️🇸🇳 (@saly_mariama) 's Twitter Profile Photo

🚨🚨Jeu Tente de gagner un pack de: 1parfum de 20ml 1huile de 15ml 1huile de 3ml 1musc de 3ml Condition Rt et follow Siréne Noire🧜🏿‍♀️🇸🇳 5 pack à gagner 2parmis les Rt 2parmis les Cités 1parmis les commentaires Bonne chance

𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳 (@prince_mourid) 's Twitter Profile Photo

Saa bu guddi Àjjuma jotee, nga jàng: 1-Faatiha 1X 2-Salaatu Halan Nabii 1X 3-Lixlaas 40X 4-Salaatu Halan Nabii 1X Su noppee nga yéene ko jullit yi faatu yépp ak ñiy dund jamono jii, ak ñi wara judd. Kon jullit bi njëkk a faatu ba ki mujjee faatu, dinañu am yoolub 40 Lixlaas.

Khadidjatou At’tijani✨ (@haadijamouhamed) 's Twitter Profile Photo

Une personne généreuse souhaite offrir deux exemplaires du Coran parmi les retweets. Fin du jeu Dimanche à 19h in shaa Allah Bonne chance 🤍

Une personne généreuse souhaite offrir deux exemplaires du Coran parmi les retweets.

Fin du jeu Dimanche à 19h in shaa Allah
Bonne chance 🤍