Sëriñ Fàllu Sëy (@fallouseye815) 's Twitter Profile
Sëriñ Fàllu Sëy

@fallouseye815

ID: 1407314226234990592

calendar_today22-06-2021 12:27:27

31,31K Tweet

397 Followers

1,1K Following

Hayati Fall (@hayatifall) 's Twitter Profile Photo

Plus de 72h après le décès de l’étudiant Abdoulaye Bâ, aucune démission, aucune arrestation. En revanche, trois étudiants sont poursuivis pour “destruction de matériel”. La priorité est-elle vraiment là ? La vie humaine n’a-t-elle pas plus de valeur que des biens matériels ?

SALIOU MBACKE FAYE (@salioumbackefa1) 's Twitter Profile Photo

Nun murit kuy wax ag nun , da ngay bind wolof moy wane ni ku fonk sa bopp nit ñi delló la ko . Motax su ma gisee ay nit complexé sax ci bind wolof mba di xas ñi koy def damay ree rek

❝ 𝗕𝗔𝗔𝗬 𝗦𝗛𝗘𝗘𝗫 ❞ (@baaysheex) 's Twitter Profile Photo

Fattaliku Seriñ Abdou Hakim Mbacké Ibn Seriñ Bassirou Mbacké (25 Sha’ban 1434H) Di ñaan suñu Boroom dolli ko ay Ngërëm barke Seexul Xadiim ❤️🙏🏾

Fattaliku Seriñ Abdou Hakim Mbacké Ibn Seriñ Bassirou Mbacké (25 Sha’ban 1434H) 

Di ñaan suñu Boroom dolli ko ay Ngërëm barke Seexul Xadiim ❤️🙏🏾
Alioune✊ (@as_clevero) 's Twitter Profile Photo

Un Certificat Médical qui établit clairement les causes du décès mais le Procureur de la République lui, parle de rumeurs. Rewmi ko fi yaxaar mou tass sa yaxaar.

‏‏عبد الكريم جاي (@ndongoseexibra) 's Twitter Profile Photo

NDOGU SEEX IBRA FALL YI🐂🐂🐂 Ño gi nuyu ag siar murids ag jabootu Islam gépp !!! Ganaaw bi ñu leen faggulee 𝟎𝟐 𝐧𝐚𝐠𝐠 (𝐛𝐨𝐞𝐮𝐟𝐬) ci 𝟏.𝟓𝟎𝟎.𝟎𝟎𝟎𝐅 𝐂𝐅𝐀 lepp di sen jëff, Fass yeene faggulaat leen 𝟎𝟒 𝐧𝐚𝐠𝐠 (𝐛𝐨𝐞𝐮𝐟𝐬) ganaaw bu ñu leen jebbalalee yi fi

Sëriñ Saliou (@assaalih22) 's Twitter Profile Photo

« J’ai su avec certitude que les soufis sont ceux qui cheminent spécialement sur la voie d’Allah Très-Haut ; que leur conduite est la meilleure des conduites, que leur voie est la plus juste des voies, et que leur moralité est la plus pure des moralités. » Ghazali.

ZiGui 🇸🇳🇵🇸 (@zguisse) 's Twitter Profile Photo

Quand tout va mal, on nous parle du système. Un étudiant meurt ? C’est le système. Le président et le Premier ministre ne se parlent pas ? C’est encore le système. Le ministre de l’Intérieur manipule l’opinion ? Toujours le système. Les FDS torturent ? Encore et encore le système

‏‏عبد الكريم جاي (@ndongoseexibra) 's Twitter Profile Photo

Serigne Touba diggul ab talibé dara, lepp lu Boroom Touba diggee tay ag ëllëg ab MURID la ko digg te bind na liy taxa doonub murid, SEEXRA FALL jëff ko ñu giss.Ku bëgg am ci li Serigne Touba yoor ni Seexra Ibra Faal gay deff (L'INCONTOURNABLE)📌

Fallou Salih (@salihfadal) 's Twitter Profile Photo

Salaatou gou ame solo Borom Touba indiko si térém bimou toudou Ad-Dourou Samine (Un ensemble de prières sur le Prophète Mouhammad, psl)

Salaatou gou ame solo Borom Touba indiko si térém bimou toudou Ad-Dourou Samine (Un ensemble de prières sur le Prophète Mouhammad, psl)
فال (@anta__fall) 's Twitter Profile Photo

Jumah dji 📌 Soumasi wakh bobou ak legui lima beugeul sama bopp la yenee gneup rekkk Nagn ko bayi khel def si yité bolee kossi sunu yite yi Koussi dieufone dolil kou dieufegoul fekhel dabee .

XAADIM🇸🇳 (@moughniyan) 's Twitter Profile Photo

Maa ngi leen i fàttali ni liggéeyu jumaa ji ndigalul Sëñ Tuubaa la ndax luko ñoron la tàmbale ci Seex Mustafaa ba tay jii ñu fass yene ko and ak Seex Muhammadul Muntaqaa kon nan ci def sunu lepp ngir liggéeyale ko Yàlla.

Maa ngi leen i fàttali ni liggéeyu jumaa ji ndigalul Sëñ Tuubaa la ndax luko ñoron la tàmbale ci Seex Mustafaa ba tay jii ñu fass yene ko and ak Seex Muhammadul Muntaqaa kon nan ci def sunu lepp ngir liggéeyale ko Yàlla.
❝ 𝗕𝗔𝗔𝗬 𝗦𝗛𝗘𝗘𝗫 ❞ (@baaysheex) 's Twitter Profile Photo

🚨Serigne amdy khady fall khalif general des baye fall jox na addiya Serigne mountakha mbacke khalife general des mourides 500.000.000 fcfa , 07 faas (chevals) , 01 galéem (chameau) , 3 voitures et autres