Baay Sëriñ Jóob (@alaadjiditakh) 's Twitter Profile
Baay Sëriñ Jóob

@alaadjiditakh

Ndakarlogue en Sénégalogie

Expert en moss beignet

ID: 104396591

linkhttps://www.instagram.com/serignediop__?igsh=aWIxeG5uZG1vbTR6 calendar_today13-01-2010 05:57:08

260,260K Tweet

95,95K Followers

7,7K Following

Baay Sëriñ Jóob (@alaadjiditakh) 's Twitter Profile Photo

Nemmeeku say xarit ak sey nitt baax na lool sax. Diggante yu bari yàqqu na ñu ndax loolu. Bu ci kenn rëyee rek day jàpp ni warul a nemmeeku nit ki ndax moo ko mujjee bind wala woo. Bu nu xaar li leen war ci ñun, nanu def rek li ñu war ci ñoom. Ku maci gëja nemmeeku na ma jéggal😭