Touba Ca Kanam L'officiel (@touba_l) 's Twitter Profile
Touba Ca Kanam L'officiel

@touba_l

TOUBA CA KANAM est une association apolitique qui investit sa force, sa richesse,son intelligence au service de CHEIKH AHMADOU BAMBA/ 33 978 25 37. 785443333

ID: 1251489757680537602

linkhttps://www.facebook.com/toubacakanam/ calendar_today18-04-2020 12:37:09

3,3K Tweet

10,10K Takipçi

8 Takip Edilen

Touba Ca Kanam L'officiel (@touba_l) 's Twitter Profile Photo

Société général Sope Gainde Fatma Adresse : Touba Yoonu ñaari pneu ci 2X yi Vente : Fer - Bac Alur - Zinc - Décoration métallique Dons : 100 Zincs Bac Alur de 6 mètres Jëwrine : Ibrahima Ammar

Touba Ca Kanam L'officiel (@touba_l) 's Twitter Profile Photo

Opération Wallu: Ci Teewaayu Sëriñ Habiibu Mbàkke Bis bu set ginnaaw timis dinanu daje ci siège Tck bi Waxtaane tolluwaayu liggéey bi.. Touba Ca Kanam Jenn yitte kepp la am Taxawu dëkk bi…

Opération Wallu:

Ci Teewaayu Sëriñ Habiibu Mbàkke 
Bis bu set ginnaaw timis dinanu daje ci siège Tck bi
Waxtaane tolluwaayu liggéey bi..

Touba Ca Kanam
Jenn yitte kepp la am
Taxawu dëkk bi…
Touba Ca Kanam L'officiel (@touba_l) 's Twitter Profile Photo

Ab yëgle: Numéro 785443333 Dafa plafonner Man ngeen jaar ci APPLICATION WAVE BI ngir joxe seen barkeelu ci lu yómb yoon waa ngi nii…

Touba Ca Kanam L'officiel (@touba_l) 's Twitter Profile Photo

Jëwriñu Tuubaa Ca Kanam.. Ibn Sëriñ Fàdlu Xaadim Rasuul.Il est l'initiateur de ce grand projet qu'est TOUBA CA KANAM.. Si tous les mourides répondent à son appel, TOUBA sera façonné et métamorphosé en un temps record..