Qari Cheikh Makhtar DIEYE (@qarimakhtar) 's Twitter Profile
Qari Cheikh Makhtar DIEYE

@qarimakhtar

أَفَلَا يَتَدَبَّرُونَ الْقُرْءَانَ أَمْ عَلَى قُلُوبٍ أَقْفَالُهَا Réciteur du Saint Coran 📖✨| Dévoué à la parole d’ALLAH ☝️ Tel: 77 792 69 69

ID: 1805904289531039744

calendar_today26-06-2024 10:03:47

145 Tweet

2,2K Followers

919 Following

Qari Cheikh Makhtar DIEYE (@qarimakhtar) 's Twitter Profile Photo

1-ku koor gi taxoon nga fonk julli juróom, koor gi jeex na de 2- Ku koor gi taxoon ngay julli Jummaa, koor gi jeex na de 4- ku koor gi taxoon ngay muuru, koor gi jeex na de... Ki la bind, bind koor mooy Yàlla ta du fi jóge. Kon na nu wëy di ko jaamu Al Hamdoulilah, Eid Mubarak

1-ku koor gi taxoon nga fonk julli juróom, koor gi jeex na de
2- Ku koor gi taxoon ngay julli Jummaa, koor gi jeex na de
4- ku koor gi taxoon ngay muuru, koor gi jeex na de...

Ki la bind, bind koor mooy Yàlla ta du fi jóge. Kon na nu wëy di ko jaamu

Al Hamdoulilah, Eid Mubarak
Qari Cheikh Makhtar DIEYE (@qarimakhtar) 's Twitter Profile Photo

9ème Édition de la Journée du Coran Je vous invite chaleureusement à prendre part à cette journée dédiée au Saint Coran, un moment de lumière et de spiritualité. Date : Dimanche 25 mai إِنْ شَاءَ ٱللَّٰهُ Heure : 09h00 Lieu : Institut Islamique de Dakar RETWEET 🙏

9ème Édition de la Journée du Coran
Je vous invite chaleureusement à prendre part à cette journée dédiée au Saint Coran, un moment de lumière et de spiritualité.

Date : Dimanche 25 mai إِنْ شَاءَ ٱللَّٰهُ
Heure : 09h00
Lieu : Institut Islamique de Dakar

RETWEET 🙏
Qari Cheikh Makhtar DIEYE (@qarimakhtar) 's Twitter Profile Photo

9ème Édition de la Journée du Coran Je vous invite chaleureusement à prendre part à cette journée dédiée au Saint Coran, un moment de lumière et de spiritualité. Date : Dimanche 25 mai Heure : 09h00 Lieu : Institut Islamique de Dakar

Qari Cheikh Makhtar DIEYE (@qarimakhtar) 's Twitter Profile Photo

Salam 🤝 Dewenati ! Baal leen ma àq baal na leen. Ñu téewe ko àt yu bari bàrkeb Seydina Muhammad (Sallâllâhou Alayhi Wa Sallam) 🙏

Salam 🤝
Dewenati ! Baal leen ma àq baal na leen. Ñu téewe ko àt yu bari  bàrkeb Seydina Muhammad (Sallâllâhou Alayhi Wa Sallam) 🙏