BuurJoie Bii (@papapsgueye) 's Twitter Profile
BuurJoie Bii

@papapsgueye

Dieureudieufé Ahmadoul Khadim
Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
Serigne Mountakha Mbacké yallah nafi yagg té andd ak werr

ID: 4881772113

calendar_today06-02-2016 15:00:04

163 Tweet

99 Followers

1,1K Following

BuurJoie Bii (@papapsgueye) 's Twitter Profile Photo

Et quand tu étais de leur côté, t'etais aveugle ou y'avais pas de mort Et n'oublions pas qu'elle fût l'une des premières à demander le report des élections

BuurJoie Bii (@papapsgueye) 's Twitter Profile Photo

Thiey Ousmane Sonko Moy fall Maire, Fall Député, Fall Président, Fall Ministres Manam mo fall kepp kouy liggueyal Sénégal 🇸🇳 Reug Reug 🇸🇳 DiomayeMoySonko #SenegalNouvelEspoir #gouvernementsenegal #senegal

BuurJoie Bii (@papapsgueye) 's Twitter Profile Photo

Sheuttt Sénégal😭🇸🇳 Tamitt Ki moy Kanati Mbeuguel fokk niou téré yeneu nitt yi Ndeysane Thia Déception bala #mbeuguel #betebete #deception #evenprod #marodi #fishasenegal

✰ Mafia Kacc Kacci 𓃵✰ (@mafiakacckacci1) 's Twitter Profile Photo

« Maximum de partage mes chers amis pour nous permettre d'identifier ces malfrats. Il ont emporté de l'argent et des papiers confidentiels. Merci. » niou partager koo svp✊🏾❤️ Ça coûte 0€ de Rt🇸🇳 #MafiaKaccKacci1

Taarou Mouride Officiel 🇸🇳 (@mouridetaarou) 's Twitter Profile Photo

Inaa lillaahi wa innaa ilayhi raajihuun😭😭 cëy boroom bi Sëriñ amdi faal mm Sëriñ Moodu mbènda di xalifab maam seex Ibrahima faal moofi bàyyikoo ñoongi ñaan boroom bi mu yokk ko ay ngërëm aki njèggël barkeb sexul khadim