Minanu (@marminanu) 's Twitter Profile
Minanu

@marminanu

Bëgg Gëm ak Jëf

ID: 734261611406430208

linkhttp://karamatiqattuyadi.com calendar_today22-05-2016 05:56:24

2,2K Tweet

4,4K Takipçi

3,3K Takip Edilen

Minanu (@marminanu) 's Twitter Profile Photo

Na ku nekk def luko saf ba kenn ñëw fi naan "ay non Sëñ bi lii Sëñ bi laa..." Man fii ba 18 Safar luma neex laay def ❤️😭

Fallou Salih (@salihfadal) 's Twitter Profile Photo

Au delà du Calm ! Cette marque de Café-Touba démontre une ingéniosité de la part de son auteur qui n'est d'autre que Serigne M. Moustapha Abdourahmane Gaïndé Fatma. En effet, ce petit- fils de Cheikhoul Khadim de par son amour au fondateur de la Mouridiyah 👇

Au delà du Calm !

Cette marque de Café-Touba démontre une ingéniosité de la part de son auteur qui n'est d'autre que Serigne M. Moustapha Abdourahmane Gaïndé Fatma.

En effet, ce petit- fils de Cheikhoul Khadim de par son amour au fondateur de la Mouridiyah 👇
ABDOUL AHAD (@ahad_dieng) 's Twitter Profile Photo

TU m’as sorti du sommeil par le réveil de celui à qui rien n’est voilé et m’a gratifié Généreusement de la révélation des mystères TU m’as favorisé de la Libéralité de celui auprès de Qui les bienfaits sont inépuisables et m’as préservé de ceux qui sont condamnés (S. TOUBA)

TU m’as sorti du sommeil par le réveil de celui  à qui rien n’est voilé et m’a gratifié Généreusement de la révélation des mystères 

TU m’as favorisé de la Libéralité de celui auprès de Qui les bienfaits sont inépuisables et m’as préservé de ceux qui sont condamnés (S. TOUBA)
بــــــشير 🇵🇸 (@_bachiir) 's Twitter Profile Photo

Ci mujjug nattu yi, Sëriñ bi doon na ñaan Yàlla dellusi Tuubaa te mu doon luy bégal jullit ñépp, fajal leen seen aajo te musal leen cig alku. إليك اشتكائ رب جهلي وغربتي فقـدني لإخواني به واكـفني تبـا وبـشـر ذوي الإسـلام طـرا بأوبـتي إلى إخوتي ولتقض لي قبلها الإربا #Safar1447

Ci mujjug nattu yi, Sëriñ bi doon na ñaan Yàlla dellusi Tuubaa te mu doon luy bégal jullit ñépp, fajal leen seen aajo te musal leen cig alku.

إليك اشتكائ رب جهلي وغربتي
فقـدني لإخواني به واكـفني تبـا

وبـشـر ذوي الإسـلام طـرا بأوبـتي
إلى إخوتي ولتقض لي قبلها الإربا

#Safar1447
Soppeb Baay Lahaat Mbàkke 🇸🇩 (@_ahmadouna) 's Twitter Profile Photo

Pàcc 2i ci sababub tukki gi. “Jàkka joojii fa la nekk di fa def ihtikaaf Rasuulul-Laahi (ﷺ) feeñu ko ànd ak gaayam yi nga xam ne ñoo dib àndam te du tàggu a ak ñoom. Ba mu leen gisee nag, hitteem yépp daal di jëm ci bëgg a bokk ci gaa yooyu di ànd ak Sang bi (ﷺ),

Pàcc 2i ci sababub tukki gi. 

“Jàkka joojii fa la nekk di fa def ihtikaaf Rasuulul-Laahi (ﷺ)  feeñu ko ànd ak gaayam yi nga xam ne ñoo dib àndam te du tàggu a ak ñoom. Ba mu leen gisee nag, hitteem yépp daal di jëm ci bëgg a bokk ci gaa yooyu di ànd ak Sang bi (ﷺ),
Maam Faati🇵🇸 (@s_naawel) 's Twitter Profile Photo

“Su nu ginnaaw bakkan, amu nu lénn lu nuy dëgërloo, man cee teg baaraam, ludul Sëriñ Tuubaa” Seex Abdul Ahad Mbàkke 🤍

“Su nu ginnaaw bakkan, amu nu lénn lu nuy dëgërloo, man cee teg baaraam, ludul Sëriñ Tuubaa”

Seex Abdul Ahad Mbàkke 🤍
Abdu Sakor FAAL🇸🇳🇵🇸👌🏾 (@_sakor_) 's Twitter Profile Photo

Sa dund gi moo am njariñ, Yàlla na la Yàlla may Lingay wut ci beppub lar ta yàggal sa dund gi Sa dund gi moo am bopp am fulla am njariñ Rëyal nga lu sew, baaxal lu bon, yaa di sang bii Sëriñ Mbay Jaxate

Sa dund gi moo am njariñ, Yàlla na la Yàlla may
 Lingay wut ci beppub lar ta yàggal sa dund gi 

Sa dund gi moo am bopp am fulla am njariñ 
 Rëyal nga lu sew, baaxal lu bon, yaa di sang bii  

Sëriñ Mbay Jaxate
SALIOU MBACKE FAYE (@salioumbackefa1) 's Twitter Profile Photo

Ñiy dalal gan yi it ñu moytu di atte gan yi ci seen bop , bo amee gan gu bëgg nelaw , bëgg lekk , tayal muñee ko seriñ bi te bañ ko yedd

Minanu (@marminanu) 's Twitter Profile Photo

Mikaa-il Magal sina aki gaayam 😩 Aka bëgg Borom Touba te am yeene ci Magal ❤️ Mais ngir Yalla Sëñ bi -Ginaar ba Gileem- la wax 😍 Xamna faalewuma sax 😇 Mbacké wax ci book 😎

Mikaa-il Magal sina aki gaayam 😩 Aka bëgg Borom Touba te am yeene ci Magal ❤️ Mais ngir Yalla Sëñ bi -Ginaar ba Gileem- la wax 😍 Xamna faalewuma sax 😇
Mbacké wax ci book 😎
Taalibe Njool Belel (@dioufdiery) 's Twitter Profile Photo

Li Seex Abdoul Ahad mooko bindoon,dithi niaanal,gni magal ci Guinaaw bima dioyalee,sama mbir yepp,thi sama boroom mu magg mi,dieumele sama lepp thi yonentam bi shw,ag thi ligueey katam bi,khadimoul rassoul,yalla na nguremal yalla miy adji djitou,tey adji des 👇

Li Seex Abdoul Ahad mooko bindoon,dithi niaanal,gni magal ci
Guinaaw bima dioyalee,sama mbir yepp,thi sama boroom mu magg mi,dieumele sama lepp thi yonentam bi shw,ag thi ligueey katam bi,khadimoul rassoul,yalla na nguremal yalla miy adji djitou,tey adji des 👇
Momar Assane (@noo_idcard) 's Twitter Profile Photo

Juger l’essence du magal à travers certains comportements déviants c’est comme juger l’islam a travers le comportement d’un terroriste qui pense servir l’islam.