🇵🇸 Seex mustafal kariim (@magui_bass) 's Twitter Profile
🇵🇸 Seex mustafal kariim

@magui_bass

dara saxul, ku yabu far wakiirlu.di jaamu yalla tay nangoo goor goor lu

ID: 1491313890780749824

calendar_today09-02-2022 07:32:07

6,6K Tweet

551 Takipçi

550 Takip Edilen

Momar Assane (@noo_idcard) 's Twitter Profile Photo

Depuis que l’armée françaises a commencé à se retirer le discours d’une menace terroriste commence à prendre forme au senegal. Quel coïncidence

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Vidéo bii jànge naa ci lu bari ci Tawhiit, tuutal gi ñuy tuutal fii Jomaay ak di ko doyadal, loolu kese man naa tax Yàlla def ko muy kilifa gi tay, yéene ji mu am ci mbokkum jullitam toog di ko défendre moo dal ci kawam tay, fii mu nekk nii keneen la bégoon mu nekk fi, far Yàlla

Fallou Salih (@salihfadal) 's Twitter Profile Photo

Lawhoul Mahfouz (Tablette divine) moom la ndieuka dégué koufaye dieulé binde si moom lako moudié dégué😭😭😭😭 Borom Touba Yalla dakoo wéteul si lép🙏

🇵🇸 Seex mustafal kariim (@magui_bass) 's Twitter Profile Photo

Man d booma ñoodiloon kuuraan bi nekk à 400m ak man rek ma fainnalu! Ay xalé laa yor,on en a vraiment besoin. Soriwuma dara, mangi si entrée tuubaa bi ,juste apres rond point janatu bi,sur la route de touba fall Jean-Michel SENE gayi taguel len mako mu ñëw🙏🏽

SALIOU MBACKE FAYE (@salioumbackefa1) 's Twitter Profile Photo

Aduna bii nu nekk , ku farluwul dina am ku la yobb , kemitisme moderne baangi taxaw ngir dello nit ñi ci ag ceddo jaareko ci ay discours fallacieuses , un certain feminisme bëgg delloo certaines ci ag jaahiliya , nasaraan yeeg tubaab yi di xeex lislaam . Ku moytuwul rek ñakk

أَحْمَدُ 🇸🇳 (@papi__amadou) 's Twitter Profile Photo

Sénégal lepp lou Yallah mome rk il faut niou sedd thi thieure sheuytané. Lou haram ken meunouko défendre au nom de quoi que ce soit culture ou autres.

Yarwaay 🇸🇳 (@tapha_yarway) 's Twitter Profile Photo

La culture de nos grands parents ne devient belle que quand on parle de nudité (débat sur l’allaitement récemment) ou ce genre de libertinage comme le taajaboon Continuez à vous leurrer.

بــــــشير 🇵🇸 (@_bachiir) 's Twitter Profile Photo

Jàpp naa ne lu nit man a ñaan jamono jii na ci boole ag ñàkk jot, ndax boo ñàkkee jot yu bari dootoo ko tal, bariwaan a lóoxóor yu nit di dugg ak am jot gu bari a ko ko ci dugal.

🇵🇸 Seex mustafal kariim (@magui_bass) 's Twitter Profile Photo

ثم السلامة من الغرور لعمر ربي اصعب الامور لانه يكون بالعلم كما يكون بالجهل بقول العلما #مسالكالجنان