Fatou 💍♥️ (@sambfatou24) 's Twitter Profile
Fatou 💍♥️

@sambfatou24

Beug Serigne Babacar 😍🙏🏿14/02/2023😭🕊️

ID: 1170072142211440646

calendar_today06-09-2019 20:32:28

2,2K Tweet

4,4K Takipçi

3,3K Takip Edilen

Ghulam (@ghulamu_tijani) 's Twitter Profile Photo

Li ma xam ci Goorgui moy kénn mënnu kaa xam. Ni Yàlla mom rek xamé Yonenté bi ﷺ, nonu la Yonenté bi rek xamé itam sëttam bi. Ki la képp kuddul Yonentés wala Sahabas yagg joxoñe fokni yawa té du yaw. Ki la Yonenté bi wax ni moy domam té mokay donni ëllëk ci lu amul bénn parparlo.