Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile
Moor Suraŋ

@s_sourang

Mor Sourang PDG Massalik Café, Écrivain et Chercheur sur le Mouridisme

ID: 1110223917199880194

calendar_today25-03-2019 16:56:23

31,31K Tweet

29,29K Takipçi

1,1K Takip Edilen

Moor Suraŋ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Li ma lay dénk mooy mbir yii yépp delloo ko ci Yàlla kese. Usmaan xamal ne sa yéene ak say mbébét man naa wuute ak li Yàlla di dogal, waaye du tee Yàlla fay la li nekkoon sa yéene. Li tax nga war a delloo mbir yi ci Yàlla te muñ mooy, Yàlla defal na la ci réew mi lu mu defalul

Li ma lay dénk mooy mbir yii yépp delloo ko ci Yàlla kese.
Usmaan xamal ne sa yéene ak say mbébét man naa wuute ak li Yàlla di dogal, waaye du tee Yàlla fay la li nekkoon sa yéene. 

Li tax nga war a delloo mbir yi ci Yàlla te muñ mooy, Yàlla defal na la ci réew mi lu mu defalul