𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳 (@prince_mourid) 's Twitter Profile
𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳

@prince_mourid

هو رب المُستحيل، وأنت تبكي على الممكن ؟ instagram.com/prince_mourid1…

ID: 1267903308536086536

calendar_today02-06-2020 19:38:18

54,54K Tweet

7,7K Takipçi

1,1K Takip Edilen

𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳 (@prince_mourid) 's Twitter Profile Photo

Jàng a gëna gaaw bind, te moo ne li mu bind lépp amut kenn kenn kenn ku ko matal ci am njàng ! Te am mbindam weesuwul ludul Yàlla kenn la Yónnent bi Halayhi’s Salaam ndawul Yàlla la. Noo ngi dolli sant Yàlla mi nu boole ak yaw, da ngay defar nit ba mu jag, te doo ko laaj dara🤍

Jàng a gëna gaaw bind, te moo ne li mu bind lépp amut kenn kenn kenn ku ko matal ci am njàng !

Te am mbindam weesuwul ludul Yàlla kenn la Yónnent bi Halayhi’s Salaam ndawul Yàlla la.

Noo ngi dolli sant Yàlla mi nu boole ak yaw, da ngay defar nit ba mu jag, te doo ko laaj dara🤍