مجنون باي (@doffoubaye) 's Twitter Profile
مجنون باي

@doffoubaye

Passioné de #Baye_Niass...!

ID: 220854526

calendar_today29-11-2010 01:16:04

46,46K Tweet

12,12K Takipçi

3,3K Takip Edilen

مجنون باي (@doffoubaye) 's Twitter Profile Photo

Ben waay mës naa jublu si di ñëw ci jakka ji, Yonent bi ﷺ ni, « ben waaya ngi ñëw, ci buntu bëlé lay dikkée, ci njoñ Aljana la bokk » Ñëp di xool bunt ba, Abdullaahi ibn Salam ni tëll! Sahaba yii daal di ko laaj, neko luy sa jëf ba Yonent ﷺ di wax ci njoñ Aljana nga bokk ?⬇️

مجنون باي (@doffoubaye) 's Twitter Profile Photo

Julli ci Yonent bi lu bari, ak saxoo jàng Alquraan, saa boo wàccee rek, yéegaat... Ku ci nekk, jàpp nga ci buum bi gënna dëggër, yaa ngi ci yoon wi gënna gàtt tey jokkuwaay bi gënna gaaw jëm sa boroom !

مجنون باي (@doffoubaye) 's Twitter Profile Photo

Górgórlu ba mënna liir Alquraan, di ko jàng fréquemment, loolu farata la ci képp ku sóobu ci yoonu gaa ñi ! Soo ko mënnagul, bàyyil lépp jublu ko !

مجنون باي (@doffoubaye) 's Twitter Profile Photo

Baay daan na ñaan... « Yàlla na Yàlla dimbali diiné lislaam ci ñun Yàlla nanu Yàlla dimbali ci diiné lislaam » 🤲🏾

Jabra-îl (@jabra_il) 's Twitter Profile Photo

Ku leen wax ludul lii nax na leen Les Spaces, energies, spiritualité, loolu yëp baaxna mais le strict minimum pour un musulman mooy pouvoir lire le Coran dans sa version arabe. Lii FARATA la et non négociable et surtout que jafewul et en un mois tout le monde peut y parvenir si