@hadji_silla_
ID: 1083738478532276224
calendar_today11-01-2019 14:52:42
15,15K Tweet
6,6K Followers
4,4K Following
6 months ago
Li ma gën a soof mooy góoru mbootaay yu ñàkk jom yii, toog ñu lay yónnee ay ano nga ñëw si yaatal. Cim. Waaye nag koo yàq àddinaam mu yàq sa allaaxira ! Góor du nettali waay !😡😡