Fondation Serigne Babacar Sy Abdou (@fondationsbsa) 's Twitter Profile
Fondation Serigne Babacar Sy Abdou

@fondationsbsa

proud to be tidianya🖇 serigne babacar sy protege😍🇸🇳

ID: 1367448974882390016

linkhttps://www.instagram.com/fondationserignbabacarsyabdou?igsh=cWl6a3FqNDh3amty&utm_source=qr calendar_today04-03-2021 12:17:15

226 Tweet

1,1K Takipçi

1,1K Takip Edilen

Fondation Serigne Babacar Sy Abdou (@fondationsbsa) 's Twitter Profile Photo

« Gàmmu Tivaouane Seydi El Hadj Malick moo koo woote Waaye Ndar nag sama Gàmmu la Képp kuy taalibe Te amuloo benn ngànt Nanga ci tew » Serigne Babacar sy

« Gàmmu Tivaouane
Seydi El Hadj Malick moo koo woote Waaye Ndar nag sama Gàmmu la
Képp kuy taalibe
Te amuloo benn ngànt
Nanga ci tew »

Serigne  Babacar sy
Fondation Serigne Babacar Sy Abdou (@fondationsbsa) 's Twitter Profile Photo

« Kuy sama talibé te amo ngaant na nga teew naax Gammu Tiwawane, Gammu Seydil El Hadji Malick là wayé Gammu Ndar nak sama Gammu là… » Seydi Aboubacar Ibn Seydil El Hadji Malick (Rta)🤍🕊️🇧🇫🇵🇸🇸🇳🙏🏽 Gamou Ndar ak jaam💛💙

« Kuy sama talibé te amo ngaant na nga teew naax Gammu Tiwawane, Gammu Seydil El Hadji Malick là wayé Gammu Ndar nak sama Gammu là… »

Seydi Aboubacar Ibn Seydil El Hadji Malick (Rta)🤍🕊️🇧🇫🇵🇸🇸🇳🙏🏽 
Gamou Ndar ak jaam💛💙
Fondation Serigne Babacar Sy Abdou (@fondationsbsa) 's Twitter Profile Photo

YAW MI AMUL BÉNN YITTÉ LUDUL TABAX SA KËR FI CI ÀDDUNA XANA XAMOONI FI DA NGA FÉ GANÉ SI RÉKK TÉ BALA YÀGG NGA TÀKK SAY BAGASS TUXU DÉLLU ALAXIRA MIY KËRU SAXU WAAY SEYDI EL HADJI MALICK SY (RTA)

YAW MI AMUL BÉNN YITTÉ
LUDUL TABAX SA KËR
FI CI ÀDDUNA 
XANA XAMOONI FI 
DA NGA FÉ GANÉ SI RÉKK
TÉ BALA YÀGG
NGA TÀKK SAY BAGASS TUXU 
DÉLLU ALAXIRA MIY KËRU SAXU WAAY

SEYDI EL HADJI MALICK SY (RTA)
Fondation Serigne Babacar Sy Abdou (@fondationsbsa) 's Twitter Profile Photo

Cheikhal Hadj Abdou Aziz nee nama bees : " Bo démé bay dénkaane sa bopp, bul mako dénk te Bulko dénk ken ku dul yalla. Ndax keneen ko dénk sa bopp du dañ mukk ñaar diko sékkeu. DUNDU AK DEE, MËNN AK TËLEE, AM AK ÑAKK... Serigne Maodo SY Dabakh

Cheikhal Hadj Abdou Aziz nee nama bees :

" Bo démé bay dénkaane sa bopp, bul mako dénk te Bulko dénk ken ku dul yalla. Ndax keneen ko dénk sa bopp du dañ mukk ñaar diko sékkeu. DUNDU AK DEE, MËNN AK TËLEE, AM AK ÑAKK... 

Serigne Maodo SY Dabakh