B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile
B A A Y X A L I M A

@xalima_graph

༺ 🅱︎🅰︎🅰︎🆈︎ 🆇︎🅰︎🅻︎🅸︎🅼︎🅰︎ ༻ 𝙗𝙞𝙣𝙙 𝙠𝙖𝙩𝙪 𝙭𝙖𝙨𝙨𝙞𝙙𝙖 ♡ Manuscrit: Baay xalima 🤩 Snap Baay xalima ⬇️

ID: 1365505657831628802

linkhttps://snapchat.com/t/GN85yDmx calendar_today27-02-2021 03:35:29

2,2K Tweet

5,5K Followers

1,1K Following

B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile Photo

Ñaari Xassida yii daa bokk ci xassida yi ñu wara gëna baril di jàng ci weer ñu nekk di weeru tabaski rawatina ci fukki fan yu njëkk yi , ak bissu tabaski bi Manuscrit PDF bi mungi ci sunu canal télégramme 👇 t.me/xalimagraph #BAAYXALIMA

Ñaari Xassida yii daa bokk ci xassida yi ñu wara gëna baril di jàng ci weer ñu nekk di weeru tabaski rawatina ci fukki fan yu njëkk yi , ak bissu tabaski bi   Manuscrit

PDF bi mungi ci sunu canal télégramme 👇 t.me/xalimagraph
 #BAAYXALIMA
B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile Photo

Salaatu gii kepp kuko jàng 80fois bissu ajjuma ginnaaw tàkkusaan Sunu boroom jéggal ko bàkkaari 80ans ba noppi nàngul ko jaamug yalla 80ans Manuscrit #baayxalima

Salaatu gii kepp kuko jàng 80fois bissu ajjuma ginnaaw tàkkusaan 
Sunu boroom jéggal ko bàkkaari 80ans ba noppi nàngul ko jaamug yalla 80ans 

Manuscrit #baayxalima
B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile Photo

Xassida gii Sëriñ bi wax nani kuko mokkal sunu boroom dugal ko ci biir kaaràngeem, kaaràngeem gi nga xam ni kumu ci dugal nga muccu ci merum sunu boroom ak mbugalum sunu boroom ci lu amut benn weranté . Manuscrit #baayxalima

Xassida gii 
Sëriñ bi wax nani kuko mokkal sunu boroom dugal ko ci biir kaaràngeem, kaaràngeem gi nga xam ni kumu ci dugal nga muccu ci merum sunu boroom ak mbugalum sunu boroom ci lu amut benn weranté . 

Manuscrit #baayxalima
B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile Photo

Xassidag sanuqri uka falaa tansaa . Kukoy saxal di jàng doo bokku ci ñiy jàng di fàtté . Su noppee insallaah naaleen diokh PDF bi ❣️ Manuscrit #baayxalima

B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile Photo

Bènn ci samay bayiit préfère . Adduna kenn mësta wax lu rafetee nii kudul sunu waaji 🤩 Neena mbooleem lula yeem ci samag xam Yalla, neena loolu ca sunu boroom lay walangaanee ñëw ci man . Loo giss ma diko nettali nak xamal ni ci Yonent bi SHW ci la walangaanee ñëw ci man 😭

Bènn ci samay bayiit préfère .
Adduna kenn mësta wax lu rafetee nii kudul sunu waaji 🤩 
Neena mbooleem lula yeem ci samag xam Yalla, neena loolu ca sunu boroom lay walangaanee ñëw ci man . 
Loo giss ma diko nettali nak xamal ni ci Yonent bi SHW ci la walangaanee ñëw ci man 😭
B A A Y X A L I M A (@xalima_graph) 's Twitter Profile Photo

Salaatu gii kepp kuko jàng 80fois bissu ajjuma ginnaaw tàkkusaan bala ngay jugè finga doon jullee tàkkusaaan . Sunu boroom jéggal ko bàkkaari 80ans ba noppi nàngul ko jaamug yalla 80ans Manuscrit #baayxalima

Salaatu gii kepp kuko jàng 80fois bissu ajjuma ginnaaw tàkkusaan bala ngay jugè finga doon jullee tàkkusaaan . 
Sunu boroom jéggal ko bàkkaari 80ans ba noppi nàngul ko jaamug yalla 80ans 

Manuscrit #baayxalima