MAMADOU Ndiaye (@ndiayenne_bi) 's Twitter Profile
MAMADOU Ndiaye

@ndiayenne_bi

lire et apprendre 🌍🌍 marié ❤❤❤

ID: 1398207862309072899

calendar_today28-05-2021 09:22:22

16,16K Tweet

3,3K Followers

2,2K Following

أَحْمَدُ 🇸🇳 (@papi__amadou) 's Twitter Profile Photo

« Hana mou tétt bepp mbire mo khamni day ayibeule labal kholam beugg nieup Lil-Lahi mouhetasibane di diok kouko dokk foumou tollou di rafétale yattale deunam té di mougne foumou tollou té bagna togne kou togne mou balko li wajehil Lahi »

Xadeejah Diop (@xadeejahd) 's Twitter Profile Photo

Lii moy kaamil complet en 4 parties, Riwayt Warsh, mbidoum Serign Samba diagne Format A5, écriture you didj Il est à 15mil et dinagn si mayei 4 aussi VENDREDI inchalah Disponible à Thies, Dkr, Touba, Ndar Livraison autres régions possible 75 508 82 72 Rt apprécié 🫶

Lii moy kaamil complet en 4 parties, Riwayt Warsh, mbidoum Serign Samba diagne 
Format A5, écriture you didj

Il est à 15mil et dinagn si mayei 4 aussi VENDREDI inchalah 

Disponible à Thies, Dkr, Touba, Ndar 

Livraison autres régions possible 

75 508 82 72 

Rt apprécié 🫶
Taalibe (@seentalibe) 's Twitter Profile Photo

« Ô Allah, bénis et accorde la paix à notre maître Muhammad et à sa famille.Une prière qui réside dans nos âmes, afin que nos cœurs soient en paix, que les soleils de nos jours brillent, afin que personne ne nous voie sans reconnaître le Bien-Aimé sur nos visages. »ﷺ ﷺ ﷺ

bo beugee nopalu nopal nit gni xolal Seydina Muhammad ci nieup 🥹 so ko deful ko xol rek gis sikam té ko tudu sikam mu dieul sa yiw naniu beugentei mo niu jikk tay ak euleuk 💚

MAMADOU Ndiaye (@ndiayenne_bi) 's Twitter Profile Photo

Bou wa bureau ba walla wa entreprise wala usine fouway mena nek ba djouli djote nga nek sissa services patron boulsi guene bop walla service koumou mena done yemoul si services serigne bi rek dé

Bou wa bureau ba walla wa entreprise wala usine  fouway mena nek ba djouli djote nga nek sissa services patron boulsi guene bop walla service koumou mena done yemoul si services serigne bi  rek dé