@hadji_silla_
ID: 1083738478532276224
calendar_today11-01-2019 14:52:42
18,18K Tweet
6,6K Followers
4,4K Following
19 days ago
Sëriñ Muntaxaa jox na Ndigal Abdu Lahat Ka, mu ànd ak Póliis ak Sàndarmëri, jël ay matukaay ci xale yi amagul 18i at, tey dawal sareet ca biir dëkk ba. Nee na ñu dakkal ko. Benn xale bu amul lu ëpp 18i at bumu dawalati sareet.