ÀLADJI FALILU (@aladjifalilu) 's Twitter Profile
ÀLADJI FALILU

@aladjifalilu

MÛRIDE , HIZBUT TARKIYAH vulgarisation des saintes écritures XADIMIQUE. Xassida MATLABOUL FAWZAÏNI ☺️❤️Mon compte @YaaFadilu a été piraté.

ID: 1904729260461613075

calendar_today26-03-2025 02:57:51

126 Tweet

99 Followers

118 Following

ÀLADJI FALILU (@aladjifalilu) 's Twitter Profile Photo

Fékk yeena ngi dundu rekk bu leen woolu seytane ndax jëm ji dal fekk rouh gi taggo gut ak yaramam bu mu defeene raw na seytaane fékk loolu Amul RÉKK Naay moytu seytaane di ñaan YALLA musal ko ca tey Barela Tudd YALLA. " Massalikul JINAAN "

Fékk yeena ngi dundu rekk bu leen woolu seytane ndax jëm ji dal fekk rouh gi taggo gut ak yaramam bu mu defeene raw na seytaane fékk loolu Amul RÉKK Naay moytu seytaane di ñaan YALLA musal ko ca tey Barela Tudd YALLA. 

                   " Massalikul JINAAN "