
Jaañ Naar🇸🇳❤️
@ajaa_faama
ALHAMDULILAH Soxnas_Murid.🧡📚
ID: 1611482029815746562
06-01-2023 21:57:30
5,5K Tweet
1,1K Followers
1,1K Following

















Benn BUUR bee, MOO tànn YONNENT bi MU tànn XÂDIM RASÛL ci Dénd bi Céy waay ! Ñun ñoo boole Chance ak Xaas KU-TEDD-K’ee ñu féggul Xaas ak Chance Chance bi mooy MU def ñu ay Murîd Xaas bi mooy, Qasâïd am yi, te duñ nekk Marîd 🎥Sheikh Ibrahim