𝐈𝐛𝐧 𝐌𝐚𝐧𝐬𝐮𝐫🤍✨ (@xaliphambaye) 's Twitter Profile
𝐈𝐛𝐧 𝐌𝐚𝐧𝐬𝐮𝐫🤍✨

@xaliphambaye

AkIm lE GoAT👤 L’hoMMe ImpArfaiT ✌️On a Rien Ms On ManKe De Rien 🧠 Alkhamdoulillah 🙏 TaLiBé NdioLe FouTa ❤️ @realmadridfra @OM_Officiel @Cristiano 🐐 OTAKU🃏

ID: 1528871683242790912

linkhttps://www.snapchat.com/add/akimthian?share_id=0hvshHUZTLWZVO2RPCYMYg&locale=fr_SN calendar_today23-05-2022 22:53:27

24,24K Tweet

7,7K Followers

3,3K Following

𝐈𝐛𝐧 𝐌𝐚𝐧𝐬𝐮𝐫🤍✨ (@xaliphambaye) 's Twitter Profile Photo

Serigne Babacar Sy Mansour Al Khalifa Néna🗣️« Nit lu mu teg bëtam Mu rafet war na koo siiwal Ba népp jot ci Waaye lu mu gis mu ñaaw War na koo sutural Ndax lu bonn moo ngi ci moom, benn nit matul »🤌🏿 Nañouy Soutouralanté🙏🏿 Yallna ko fi yalla yagal te mou anddag weur sy Malick ❤️

Serigne Babacar Sy Mansour 
Al Khalifa Néna🗣️« Nit lu mu teg bëtam
Mu rafet war na koo siiwal
Ba népp jot ci
Waaye lu mu gis mu ñaaw
War na koo sutural
Ndax lu bonn moo ngi ci moom, benn nit matul »🤌🏿
Nañouy Soutouralanté🙏🏿
Yallna ko fi yalla yagal te mou anddag weur sy Malick ❤️