Baay Sëriñ 💙 (@serignediagne7) 's Twitter Profile
Baay Sëriñ 💙

@serignediagne7

Bëg Gëm ak Jëf💪🏾 Fu way yam yaa fa yamale sa bopp🙏🏽 NBF💙 Seex Fàllu Faal laa wóolu ♥️

ID: 2262729125

calendar_today04-01-2014 23:26:42

73,73K Tweet

17,17K Takipçi

8,8K Takip Edilen

شيخ محمد الفاضل 🕊️🇸🇳 (@yaafadlou) 's Twitter Profile Photo

BU LAA SAAY WEUYDIOUR XASSÉ GUEUREUM KO DOOR MOU DANU KULAA DOOR DANU KU LAAY GÀSAL PAXX DO THIAA DOUGG KOUY SÉNTUU SAA DÉFAITE DUKO GUISS. FONKK LÉN WEUYDIOUR YII JÀPP LÉN WEUYDIOUR YII RÀFÉTEL LÉN SEN DIGGANTÈK SENII WEUYDIOUR 💡📌💡📌💡📌

Cheikh Salihou (@cheikhd77404204) 's Twitter Profile Photo

Ziar fondation sope serigne Saliou 2024 😍 Di ñanal serigne cheikh mome serigne Saliou souñou yagal ko fi té mou weer barke xassida yi 🙏🏽

🇸🇳LËPP MUSTAPHA ♥️🇸🇳 (@bayefall07latyr) 's Twitter Profile Photo

Bëgg leen Ibra Faal ngir bëgg gui mu ma bëgg Mbaa ngéen bëgg ko ngir bëgg gui mako bëgg Mbaa ngéen bëgg ko ngir bëgg maa bëgg ( Sëriñ Tuubaa klm ) ⤵️

Bëgg leen Ibra Faal ngir bëgg gui mu ma bëgg 

Mbaa ngéen bëgg ko ngir bëgg gui mako bëgg

Mbaa ngéen bëgg ko ngir bëgg maa bëgg 

( Sëriñ Tuubaa klm )

⤵️
جيل بحداد🫀💦 374i (@djilyabdoukhadr) 's Twitter Profile Photo

Leip louy lou baakh Serign bi dadialei neuko dfeul niouko si Khassida yi Salatou bi mongui si kanezoul Mouhtadine Serign bi dieulatt ko dfko si Khassida Mafaatihoul Bichri mouy louy doli Barkei,diameuh ak paisibilité intérieur ak di doli yeurmandei si seu digueunetei ak nitt gni

Leip louy lou baakh Serign bi dadialei neuko dfeul niouko si Khassida yi
Salatou bi mongui si kanezoul Mouhtadine Serign bi dieulatt ko dfko si Khassida Mafaatihoul Bichri mouy louy doli Barkei,diameuh ak paisibilité intérieur ak di doli yeurmandei si seu digueunetei ak nitt gni
Seex Ibra Sàkkoor💙🤍 (@cheikhibraa) 's Twitter Profile Photo

📍Xam Département Dakar Jot Na Découvrez avec nous, les 4 arrondissements et 18 communes du département de Dakar ! 📊📈 Nous continuons avec l’arrondissement de Grand Dakar avec ses 6 communes : Sicap Liberté, Dieuppeul - Derklé, Biscuiterie, HLM, Grand Dakar et Hann - Bel-Air.

📍Xam Département Dakar Jot Na

Découvrez avec nous, les 4 arrondissements et 18 communes du département de Dakar ! 📊📈

Nous continuons avec l’arrondissement de Grand Dakar avec ses 6 communes : Sicap Liberté, Dieuppeul - Derklé, Biscuiterie, HLM, Grand Dakar et Hann - Bel-Air.