JANTUB YOON BI-MUCCUG JAMONO ‼️ (@rienquelui) 's Twitter Profile
JANTUB YOON BI-MUCCUG JAMONO ‼️

@rienquelui

MA'AM SEEX IBRAHIMA FALL ñëriñ gudul jeex la, te ñëp xajj nan ci...

ID: 1397872388579237888

calendar_today27-05-2021 11:09:11

18,18K Tweet

8,8K Followers

3,3K Following

HANLAL MOUSTAPHA NABI (@ndiayet250) 's Twitter Profile Photo

"Prenez ce que le Messager vous octroie ; et ce qu'il vous interdit, abstenez-vous en." [3] "Quiconque obéit au Prophète, obéit à Dieu" [4] "I...] Et vers toi, Nous avons fait descendre le Coran, pour que tu exposes clairement aux gens ce qu'on a fait descendre pour ⬇️

‏‏عبد الكريم جاي (@ndongoseexibra) 's Twitter Profile Photo

🚨2ÉME MBALEEM TOUBA 12/09/25 Ñi am yeene sen jëff tabbi ci leggeyu 2ÉME Mbaleem Touba mi Seex Muhammadul Muntaxaa di leggey lo jabootu Seex Ibra Fall ajju ci labalat dëkk ganaw Magal ag Gamou Gui. Wave-Om 78 187 15 41/70 577 82 77📌

🚨2ÉME MBALEEM TOUBA 12/09/25

Ñi am yeene sen jëff tabbi ci leggeyu 2ÉME Mbaleem Touba mi Seex Muhammadul Muntaxaa di leggey lo jabootu Seex Ibra Fall ajju ci labalat dëkk ganaw Magal ag Gamou Gui.

Wave-Om 78 187 15 41/70 577 82 77📌
JANTUB YOON BI-MUCCUG JAMONO ‼️ (@rienquelui) 's Twitter Profile Photo

Lii dh laa gëm dh man ! Sëriñ bi deesu ko limaale waay Sëriñ Basiiru Bara yàlla saa borom doli ngërëm ak leer barkeb Maam Seex Ibra Faal

‏‏عبد الكريم جاي (@ndongoseexibra) 's Twitter Profile Photo

🚨2ÉME MBALEEM TOUBA 12/09/25 Ñi am yeene sen jëff tabbi ci leggeyu 2ÉME Mbaleem Touba mi Seex Muhammadul Muntaxaa di leggey lo jabootu Seex Ibra Fall ajju ci labalat dëkk ganaw Magal ag Gamou Gui. Wave-Om 78 187 15 41/70 577 82 77📌

JANTUB YOON BI-MUCCUG JAMONO ‼️ (@rienquelui) 's Twitter Profile Photo

Dànga muccu ci cat te saasune nga wane sa jëm, dji , boo toggee wane ko , boo demee resto wane ko , etc....boo amee lu rafet wane ko .. Haa nooy muccee ?

‏‏عبد الكريم جاي (@ndongoseexibra) 's Twitter Profile Photo

THREAD Seex'Ibra Fall (Jazbul Murid)✍🏾️ Le salut du Mouride réside dans les six actions suivantes: ▫️la foi ▫️l'optimisme ▫️le dynamisme dans le dévouement ▫️la dépense (sacrifice) ▫️l'humilité ▫️le respect des recommandations du Cheikh.

THREAD 
Seex'Ibra Fall (Jazbul Murid)✍🏾️ 

Le salut du Mouride réside dans les six actions suivantes:
▫️la foi 
▫️l'optimisme 
▫️le dynamisme dans le dévouement 
▫️la dépense (sacrifice)
▫️l'humilité 
▫️le respect des recommandations du Cheikh.
JANTUB YOON BI-MUCCUG JAMONO ‼️ (@rienquelui) 's Twitter Profile Photo

Sëriñ Moodu Maxtaar Njaay Bambi Lat Joor neena deg na ci Seex Ibraayma Faal mu ne : Li Yàlla bind Sëñ Bamba moo ci ëpp aw fitt, kéep ku ñii tëkkëllé ak Sëñ Bamba dañoo fabbagul siraat gacci ko ci kaw jahënnama (sawara) Waxtaanu Murid Saadix Sëñ Moodu Abdullaahi Faal Ndar (rta)

Sëriñ Moodu Maxtaar Njaay Bambi Lat Joor neena deg na ci Seex Ibraayma Faal mu ne :

Li Yàlla bind Sëñ Bamba moo ci ëpp aw fitt, kéep ku ñii tëkkëllé ak Sëñ Bamba dañoo fabbagul siraat gacci ko ci kaw jahënnama (sawara)

Waxtaanu Murid Saadix
Sëñ Moodu Abdullaahi Faal Ndar (rta)
فال (@anta__fall) 's Twitter Profile Photo

Dol Khassida petit format 😍 Dol 1: dialibatou bichri Taysir wakana fawzeyni Dol 2 : 70 astahfiroulah bihi Dol 3 Nourou dareyni Dol 4 Xidma Dol 5 : Jazbou Mawahibou Mouhadimat Wakana bihi chifai rabbi sindidi Touhfatou shakuru rafih diawartou… ☎️781734326