π™ˆπ™–π™–π™’ π™Žπ™–π™‘π™žπ™€π™ͺπŸ‡ΈπŸ‡³ (@maamsaalih) 's Twitter Profile
π™ˆπ™–π™–π™’ π™Žπ™–π™‘π™žπ™€π™ͺπŸ‡ΈπŸ‡³

@maamsaalih

Ψ¨Ψ§Ψ­Ψ« في Ψ§Ω„Ψ―Ω‘ΩƒΨͺΩˆΨ±Ψ§Ω‡ΨŒ Ψ¬Ψ§Ω…ΨΉΨ© Ψ§Ω„Ψ²Ω‘ΩŠΨͺΩˆΩ†Ψ© Ψ§Ω„Ω…ΨΉΩ…ΩˆΨ±Ψ©/PhD researcher, Doctrine and philosophy, University of Ez-Zitouna

ID: 1073342507705094144

calendar_today13-12-2018 22:22:50

5,5K Tweet

2,2K Followers

996 Following

π™ˆπ™–π™–π™’ π™Žπ™–π™‘π™žπ™€π™ͺπŸ‡ΈπŸ‡³ (@maamsaalih) 's Twitter Profile Photo

1- kilifa took ci gaw nga took ci suuf, loolu teeginu taalibe la ak SΓ«riΓ±. 2- nit kenn du ku atte ci jΓ«fi baayam, loolu du diine. 3- mΓͺme boo jΓ ppoon li waaji def du yoon man nga koo wax ci ay teegin.

Moor SuraΕ‹ (@s_sourang) 's Twitter Profile Photo

Sëriñ Tuubaa moo doon résisté walla tubaab yi ñoo doon résisté ? Lan mooy modèle économie murid ?

π™ˆπ™–π™–π™’ π™Žπ™–π™‘π™žπ™€π™ͺπŸ‡ΈπŸ‡³ (@maamsaalih) 's Twitter Profile Photo

Goor gii daal ku baax la, SΓ«riΓ± mansour mu SΓ«riΓ± Aziz Dabah, je lui ai offert mon livre, et il m'a prΓͺtΓ© une attention considΓ©rable que je ne mΓ©rite pas vraiment❀️

Goor gii daal ku baax la, SΓ«riΓ± mansour mu SΓ«riΓ± Aziz Dabah, 
je lui ai offert mon livre, et il m'a prΓͺtΓ© une attention considΓ©rable que je ne mΓ©rite pas vraiment❀️
π™ˆπ™–π™–π™’ π™Žπ™–π™‘π™žπ™€π™ͺπŸ‡ΈπŸ‡³ (@maamsaalih) 's Twitter Profile Photo

Waa SΓ©nΓ©gal Γ±u bΓ«gg diine lanu ak lu baax… « YΓ lla bu xeebΓ© liko waa SΓ©nΓ©gal di jaamu perdre naΒ Β» Jaamu gi ko nit Γ±i di jaamu duko jariΓ± dara, waaye waxin la.

π™ˆπ™–π™–π™’ π™Žπ™–π™‘π™žπ™€π™ͺπŸ‡ΈπŸ‡³ (@maamsaalih) 's Twitter Profile Photo

JΓ«rΓ«jΓ«f SΓ± Moor Moor SuraΕ‹ ci ligeey bu am solo bi, am na mbekte ci gise bi, de tous mes contacts Twitter, tu as Γ©tΓ© le premier que j'ai eu le plaisir de rencontrer dans la vraie vie.

JΓ«rΓ«jΓ«f SΓ± Moor <a href="/s_sourang/">Moor SuraΕ‹</a> ci ligeey bu am solo bi, am na mbekte ci gise bi, de tous mes contacts Twitter, tu as Γ©tΓ© le premier que j'ai eu le plaisir de rencontrer dans la vraie vie.